<
Motivation and Inspiration Coumba Gawlo – Soleil

Coumba Gawlo – Soleil

Download Soleil Mp3 by

Here’s a song by the African prolific music artiste and talented singer ““. This song is titled “Soleil”, as it was released alongside its video. You’ll surely enjoy this one.

Download Audio Mp3, Stream, Share, and stay graced

DOWNLOAD HERE

Lyrics: Soleil by

Nadj bi fenk né tek
Drapeau bi ci kaw mi ngui né tek
Liir bangui dioye niou nakh ko mou né tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek ?

Armel yi sedd né tek
Ngoné Latyr thieu dékheulé tek
Imam ak labé yague def tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek ?

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé ?

Ahmadou Kaabar guedj gui né tek
Limamou né ko Laye guedj gui né tek
Baye Niass khamal la ngua kham né tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek ?

Sunu taarikh mingui niou khol né tek
Médina Gounass, ndiassane, Thiénaba tek
Wakh diou bone noppé ko gueune
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek ?

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé ?

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Ndeyssane yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé ?

Moudiou gou rafet mo diara niane
Lolou motakh bima dégué Gawlo yaye sunu ndaanane
May lathie ndakh
mba dina ko moudjé ? ndakh

Nietti att mou rothie sama baat mané tek
Tivavouane néma tallal lokho teu nel tek
Ndakh falaises Bandiagara yague def tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek ?

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé ?

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Vert Jaune Rouge yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé ?

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Lac rose né dou changer teu dina rose batay dji
Mba dinako moudjé… (moudjiéeeeeeeeee) ?

A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Bepp nguur nangua guestu sa askane
Yene ak niome yénéy moudjé

Bou yomal khiyamé yalla yeureumeulma sénégalais
Guem na né nonou lay moudjé

Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs ?
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé ?

Comment below with your feedback and thoughts on this post.